Highlander Testo
Testo Highlander
Mane kécé kén douma dondou
Gnou yeungou ma dagati lén
Ngén sori ma loloy lou dagane
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Vieux père boudoul maguett…Highlander
Dagg sén bopou lay déf…Highlander
Décapité par le chef…Highlander
Vieux père boudoul maguett…Highland
Vieux père boudoul bayi…Highland Vieux père boudoul maguett…Highlander
Fougn dougou ma lidieunti lén…
Mane kécé kén douma dondou….
Gnou yeungou ma dagati lén…
Ngén sori ma loloy lou dagane…
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Boumay dioudou Rap dé amagoul
Filama fék ni séni doul
Ma imperméable ci yeah dama toul
Té noupou bou nathioul dégagoul
Baggy jeans Wu-tang diamono
May battle di battle di battle
Freestyle malay golo lo
May danél di danél di danél
Soma wédé lay ma Xuman
Ték ay flow Busta mélni dou man
Au final yakamti pour lane?
Période bobou damko diégui ni dos d’âne Néka gouma ariste solo
Mais mangui ci game bi ni Gaindé bou souroul
Di dougal ay Mc ci bir kilo mbourou
Di dokhantou ci kogne bi di weur ay foural
N Easy dafal ndank lou eup tourou
Ma keupal yélwane bi sama boy yi djirau
Surveillant Général la bagné bureau
Nékété mariage dafay wékh ni gourau
Doumala diay expérience boy amo gneugam
Damay ma yar boy khébouma deureum
Dagn ma nokk boy ba tay ma gueureum
Golden boy dama gnoul ni peureum
Longévité boy
Dou serigne dou mara
Dou téré dou garap
Boy défafo dara
Dou palace dou baraque
Dou Donald dou Barack
Dou Point E dou Karack
Lougn cons’ boy dou diaratt
Ladial Egyte boy fougnou tégone Moubarak
Mais Yallay Bour souko nékhé faral’ko
Kone N Easy bayil sou la nékhé nga dialat
Ndakh Vieux père boudoul maguett…Highlander
Dagg sén bopou lay déf…Highlander
Décapité par le chef…Highlander
Vieux père boudoul maguett…Highland
Vieux père boudoul bayi…Highland
Vieux père boudoul maguett…Highlander
Fougn dougou ma lidieunti lén…
Mane kécé kén douma dondou….
Gnou yeungou ma dagati lén…
Ngén sori ma loloy lou dagane…
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Tête de mort
Katana bi loumou dagatti boy rawna dibitterie
Tête de mort nékone fi tendence
Tout ce que je voyais c’est mes trophées qui me sourient
Kou que-ni flow bi mou déloussi
Boy ay éclaires lay cons’ mél Hennessy
Rap Galsen sama done wané père et fils
Mamou mamati mamou sén lyricste, ay seut flow thérapiste
Koufi atanne sama legacy
Né téki téreum,
dérett takal yéreum,
bane yi takal béret-reum,
balle ci tak teu-teu-teute,
boy gnou teral lén yénak sén kheuram fils
Equipe bou fess ak génies fils
Do lathie Orange lane moy bénéfices
Do lathie wa Yonkers kou Jadakiss
Défaite boulay fégnou doko téleu guiss
Té longétivité boy, dou mayé dou sarakh,
Dou Jordan dou thiarakh
Dou khégn nékh dou forokh
Mais toujours frais comme le Vieux père
Ray ak sourire ni Joker…Highlander
Dagg sén bopou lay déf…Highlander
Décapité par le chef…Highlander
Vieux père boudoul maguett…Highland
Vieux père boudoul bayi…Highland
Vieux père boudoul maguett…Highlander
Fougn dougou ma lidieunti lén…
Mane kécé kén douma dondou….
Gnou yeungou ma dagati lén…
Ngén sori ma loloy lou dagane…
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Gnou yeungou ma dagati lén
Ngén sori ma loloy lou dagane
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Vieux père boudoul maguett…Highlander
Dagg sén bopou lay déf…Highlander
Décapité par le chef…Highlander
Vieux père boudoul maguett…Highland
Vieux père boudoul bayi…Highland Vieux père boudoul maguett…Highlander
Fougn dougou ma lidieunti lén…
Mane kécé kén douma dondou….
Gnou yeungou ma dagati lén…
Ngén sori ma loloy lou dagane…
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Boumay dioudou Rap dé amagoul
Filama fék ni séni doul
Ma imperméable ci yeah dama toul
Té noupou bou nathioul dégagoul
Baggy jeans Wu-tang diamono
May battle di battle di battle
Freestyle malay golo lo
May danél di danél di danél
Soma wédé lay ma Xuman
Ték ay flow Busta mélni dou man
Au final yakamti pour lane?
Période bobou damko diégui ni dos d’âne Néka gouma ariste solo
Mais mangui ci game bi ni Gaindé bou souroul
Di dougal ay Mc ci bir kilo mbourou
Di dokhantou ci kogne bi di weur ay foural
N Easy dafal ndank lou eup tourou
Ma keupal yélwane bi sama boy yi djirau
Surveillant Général la bagné bureau
Nékété mariage dafay wékh ni gourau
Doumala diay expérience boy amo gneugam
Damay ma yar boy khébouma deureum
Dagn ma nokk boy ba tay ma gueureum
Golden boy dama gnoul ni peureum
Longévité boy
Dou serigne dou mara
Dou téré dou garap
Boy défafo dara
Dou palace dou baraque
Dou Donald dou Barack
Dou Point E dou Karack
Lougn cons’ boy dou diaratt
Ladial Egyte boy fougnou tégone Moubarak
Mais Yallay Bour souko nékhé faral’ko
Kone N Easy bayil sou la nékhé nga dialat
Ndakh Vieux père boudoul maguett…Highlander
Dagg sén bopou lay déf…Highlander
Décapité par le chef…Highlander
Vieux père boudoul maguett…Highland
Vieux père boudoul bayi…Highland
Vieux père boudoul maguett…Highlander
Fougn dougou ma lidieunti lén…
Mane kécé kén douma dondou….
Gnou yeungou ma dagati lén…
Ngén sori ma loloy lou dagane…
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Tête de mort
Katana bi loumou dagatti boy rawna dibitterie
Tête de mort nékone fi tendence
Tout ce que je voyais c’est mes trophées qui me sourient
Kou que-ni flow bi mou déloussi
Boy ay éclaires lay cons’ mél Hennessy
Rap Galsen sama done wané père et fils
Mamou mamati mamou sén lyricste, ay seut flow thérapiste
Koufi atanne sama legacy
Né téki téreum,
dérett takal yéreum,
bane yi takal béret-reum,
balle ci tak teu-teu-teute,
boy gnou teral lén yénak sén kheuram fils
Equipe bou fess ak génies fils
Do lathie Orange lane moy bénéfices
Do lathie wa Yonkers kou Jadakiss
Défaite boulay fégnou doko téleu guiss
Té longétivité boy, dou mayé dou sarakh,
Dou Jordan dou thiarakh
Dou khégn nékh dou forokh
Mais toujours frais comme le Vieux père
Ray ak sourire ni Joker…Highlander
Dagg sén bopou lay déf…Highlander
Décapité par le chef…Highlander
Vieux père boudoul maguett…Highland
Vieux père boudoul bayi…Highland
Vieux père boudoul maguett…Highlander
Fougn dougou ma lidieunti lén…
Mane kécé kén douma dondou….
Gnou yeungou ma dagati lén…
Ngén sori ma loloy lou dagane…
Y’all don’t wanna live (Y’all don’t wanna live)
Lyrics powered by LyricFind